Diiwaan yi ay dog lañu séddaliinu Senegaal, 14 lañu.

Dogiin

[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Fi mu nekk nii 14 lañu, ba ñu sosee Maatam ci 2001, teg ci sos yeneen ñatt ci 2008: Kafrin bokkoon ci diwaanu Kawlax, ak Kéedugu bokkoon ci Tambaakundaa ak Séeju gi bokkoon ci Siggcoor.

Réyaay ak way-dëkk

[Soppisoppi gongikuwaay bi]
Diiwaan Réyaay
ci km²


Way-dëkk
Cees 6 601 1 348 637
Fatik 7 935 639 075
Kawlax 16 010 1 128 128
Koldaa 21 011 834 753
Luga 29 188 559 268
Maatam 25 083 423 041
Ndakaaru 550 2 411 528
Ndar 19 044 863 440
Njaaréem 4 359 930 008
Siggcoor 7 339 557 606
Tambaakundaa 7 339 557 606
Mboolante 196 176 10 225 816

Xool it

[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Lëkkalekaay yu biir

[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Téerekaay

[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Lëkkalekaay yu biti

[Soppisoppi gongikuwaay bi]
Raayab Senegaal 14 Diiwaani Senegaal Raayab Senegaal

Cees · Fatik · Jurbel · Kafrin · Kawlax · Kéedugu · Koldaa · Luga · Maatam · Ndakaaru · Ndar · Séeju · Siggcoor Tambakundaa ·