diiwaanu Cees ci lonkoyoonu Sengaal

Diiwaanu Cees benn la ci 14 diiwaan yu Senegaal, Féete ci penku Réew mi, wër ndombo Ndakaaru. Yaatoo 6 601 km2, am 1 442 338 ciy way-dëkk. dëkkub Cees Mooy Péeyu diiwaan bi.

Melosuuf

[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Ci genn wàllam mi nga janook Tefes-gu-Mag gi, fi mbayum yu-sew yi di ame, ci Ñaay bi, ci geneen gi di janook Tefes-gu-Tuuti gi di barab bi ëppi nemmeekukat ci Senegaal.

Doon ab tombub jàllu ci diggante Ndakaaru ak li des ci réew mi. Diiwaan bi am na ay cëslaay yu tali ak yu weñ yu matale ngir wóoral tuxute gi(dem-beek-dikk bi), ci suufam.

Doonte diiwaan bu tuuti la soo ko méengalee ak yeneen yi, waaye mooy ñaareelu diiwaan bi ëppi nit, ci Réew mi, ginnaaw Ndakaaru.

Diiwaani aki tundam

Séeddaliinu suufam

[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Diiwaan baa ngi Séeddaliku ci 3 tund:

Taariix

[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Ci Melosuuf Diiwaan bi tay mooy nguuru Kajoor ga woon ak gu Bawol. Ag Yokkuteem mi ngi tegu woon ci yoonu weñ wi, rëdd wu Ndakaaru-Ndar ci mujjantalu XIXu xarnu, wu Ndakaaru-Niseer tegu ci. Bokk na ci diiwaan yi gën a yàgg ci Senegaal.

Téerekaay

[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Lëkkalekaay yu biti

[Soppisoppi gongikuwaay bi]
Raayab Senegaal 14 Diiwaani Senegaal Raayab Senegaal

Cees · Fatik · Jurbel · Kafrin · Kawlax · Kéedugu · Koldaa · Luga · Maatam · Ndakaaru · Ndar · Séeju · Siggcoor Tambakundaa ·