Ndiiwani Senegaal

Ndiiwaani Senegaal yi ay dog lañu ci séddaliinu yoriinu Senegaal.

Ndiiwaan nag ag nekkte (entité) gu suuf la, gu ñuy faral di gis ci réew yiy làkk wu-fraas. Soo demee ci ñiy làkk wu-angalteer weneen dogiin nga fay fekk.

Ci Senegaal, ndiiwaan yi dinañu leen waññi ci lim bu tollook 92 ci 2007.

Taariix

[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Limu tund yi (nosu topp abajada)

[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Tunduw Bàkkel

[Soppisoppi gongikuwaay bi]
Ndiiwaani Bàkkel

Tunduw Bambey

[Soppisoppi gongikuwaay bi]
Ndiiwaani Bambey

Tunduw Biñoona

[Soppisoppi gongikuwaay bi]
Ndiiwaani Biñoona

Tunduw Cees

[Soppisoppi gongikuwaay bi]
Ndiiwaani Cees

Tunduw Dagana

[Soppisoppi gongikuwaay bi]
Ndiiwaani Dagana

Tunduw Fatik

[Soppisoppi gongikuwaay bi]
Ndiiwaani Fatik

Tunduw Funjunj

[Soppisoppi gongikuwaay bi]
Ndiiwaani Funjunj

Tunduw Gosaas

[Soppisoppi gongikuwaay bi]
Ndiiwaani Gosaas

Tunduw Géejawaay

[Soppisoppi gongikuwaay bi]
Ndiiwaani Géejawaay

Géejawaay moom, benn Ndiiwaan la am muy moom ci boppam. Tund la ndiiwaan la

Ñu séeddale ko ci 5 dëkkani ndiiwaan

Tunduw Kafrin

[Soppisoppi gongikuwaay bi]
Ndiiwaani Kafrin

Dogiinu tund wi dañu koo soppi gannaaw sosug tunduw Kungeel ci 2006.

Kon mu des :

Tunduw Kanel

[Soppisoppi gongikuwaay bi]
Ndiiwaani Kanel

Tunduw Kawlax

[Soppisoppi gongikuwaay bi]
Ndiiwaani Kawlax

Tunduw Kebemeer

[Soppisoppi gongikuwaay bi]
Ndiiwaani Kebemeer

Tunduw Kéedugu

[Soppisoppi gongikuwaay bi]
Ndiiwaani Kéedugu

Tunduw Koldaa

[Soppisoppi gongikuwaay bi]
Ndiiwaani Koldaa

Tunduw Kungéel

[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Mi ngi judd ci 2006 (amul lonkoyoon bu jàppandi nii-nii)

Tunduw Lingeer

[Soppisoppi gongikuwaay bi]
Ndiiwaani Lingeer

Tunduw Luga

[Soppisoppi gongikuwaay bi]
Ndiiwaani Luga

Ndiiwaanu Raawo, biy feeñ ci lonkoyoon bi, ci tunduw Ndar la bokk 2002 ba tay.

Tunduw Mbuur

[Soppisoppi gongikuwaay bi]
Ndiiwaani Mbuur

Tunduw Maatam

[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Tunduw Mbakke

[Soppisoppi gongikuwaay bi]
Ndiiwaani Mbakke

Tunduw Ndakaaru

[Soppisoppi gongikuwaay bi]
Ndiiwaani Ndakaaru

Ndakaaru moom, benn Ndiiwaan la am muy moom ci boppam. Tund la ndiiwaan la

Ñu séeddale ko ci 19 dëkkani ndiiwaan.

Tunduw Njaaréem

[Soppisoppi gongikuwaay bi]
Ndiiwaani Njaaréem

Tunduw Ndar

[Soppisoppi gongikuwaay bi]
Ndiiwaani Ndar

Gannaaw dogaat ga waraaloon juddug Diiwaanu Maatam, tund wi, wenn ndiiwaan rekk la am muy bu

Tunduw Ñooro gu Rip

[Soppisoppi gongikuwaay bi]
Ndiiwaani Ñooro gu Rip

Tunduw Pikin

[Soppisoppi gongikuwaay bi]
Ndiiwaani Pikin

Pikin moom, benn Ndiiwaan la am muy moom ci boppam. Tund la ndiiwaan la

Ñu séeddale ko ci 16 dëkkani ndiiwaan.

Tunduw Podoor

[Soppisoppi gongikuwaay bi]
Ndiiwaani Podoor

Tunduw Raneru

[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Tund wi, wenn ndiiwaan rekk la am muy bu Welingara

Tunduw Séeju

[Soppisoppi gongikuwaay bi]
Ndiiwaani Séeju

Tunduw Siggcoor

[Soppisoppi gongikuwaay bi]
Ndiiwaani Siggcoor

Tunduw Tambaakundaa

[Soppisoppi gongikuwaay bi]
Ndiiwaani Tambaakundaa

Tunduw Tënjéej

[Soppisoppi gongikuwaay bi]
Ndiiwaani Tënjéej

Tund wi, wenn ndiiwaan rekk la am muy bu Sebixotaan, moom ci boppam ñu séddale ko ci 3 dëkkaani Ndiiwaan.

Tunduw Tiwaawon

[Soppisoppi gongikuwaay bi]
Ndiiwaani Tiwaawon

Tunduw Usuy

[Soppisoppi gongikuwaay bi]
Ndiiwaani Usuy

Tunduw Welingara

[Soppisoppi gongikuwaay bi]
Ndiiwaani Welingara

Xool it

[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Lëkkalekaay yu biir

[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Lëkkalekaay yu biti

[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Téerekaay

[Soppisoppi gongikuwaay bi]