Wikipedia
Wikipedia
Bii jukki ab junj rekk la. Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wikipedia taxawal


Dunu Santiago
Réew Kap Weer
Rëyaay 991 km²
Dalub web http://www.santiago.cv/

Santiyaago diiwaan dunu ci yu Kap Weer. Santiyaago mooy dun bu mag bi ci Kap Weerdi, di ko màggal ci wàllu jëfekaay bi, te mooy kërug genn-wàllu askanu réew mi. Bokk na ci dun yi ñuy wax Sotaweento, nekk ci diggante dun yi ñuy wax Maio (26 km) ci penku) ak Fogo (55 km) ci sowu. Moom moo jëkkoona dëkke: dëkk bu ñuy wax Ribeira Grande (muy tudd Cidade Velha te UNESCO teg na ko ci wàllug Dunu suuf si[2]) lañ ko sos ci atum 1462. Ci dëkku Santiyaago la dëkku Paraaya di péeyu réew mi nekk.

Dëkkaani

[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Dëkki

[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Dëkk-Dëkkaani

[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Sport

[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Staad

[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Dayo

[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Iniweersite

[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Karmat ak delluwaay

[Soppisoppi gongikuwaay bi]


Lëkkalekaay yu biti

[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Logo Commons

Xool it Wikimedia Commons